Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 51

Sabóor 51:9-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Wis ma ndox, ma sell; sang ma, ma set wecc.
10Yal nanga ma dégtal mbég ak bànneex, ma bégati, gannaaw ba nga ma dammatee.
11Bul xool samay moy, faral sama ñaawtéef yépp.

Read Sabóor 51Sabóor 51
Compare Sabóor 51:9-11Sabóor 51:9-11