Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 51

Sabóor 51:17-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Boroom bi, may ma, ma wax, ma delloo la njukkal.
18Sàkkuwloo sarax, nde kon ma indi; te soppuloo saraxu rendi-dóomal.
19Saraxi Yàlla, xol bu tuub la, yaw Yàlla, xol bu tuub ba mokk, doo gàntal boroom.

Read Sabóor 51Sabóor 51
Compare Sabóor 51:17-19Sabóor 51:17-19