Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 50

Sabóor 50:20-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20ngeen di tooge seen mbokk, di yàq deru doomu ndey.
21Lii yeena ko def! Damay noppi, ngeen defe ne damaa mel ni yeen? Dama leen di sikk, tuumaal leen, ngeen gis!
22«Yeen fàttekati Yàlla yi, déggleen lii, bala maa fàdd te kenn du wallu.

Read Sabóor 50Sabóor 50
Compare Sabóor 50:20-22Sabóor 50:20-22