Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 45

Sabóor 45:15-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Ñu yóbbul ko Buur, mu ne boyy, janq ja ànd ak moom, diy toppam, ñu indil leen Buur,
16ñu duggsi kër Buur, ci biir mbégteek bànneex.
17Yal na la sa doom yu góor wuutu ci seen jalu maam, nga def leeni kàngam ci réew mi mépp.

Read Sabóor 45Sabóor 45
Compare Sabóor 45:15-17Sabóor 45:15-17