Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 44

Sabóor 44:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Yaa nuy musal ci bañ yi, yaay gàcceel noon ñi.
9Yàlla lanuy damoo bésoo bés, di màggal turam ba fàww. Selaw.
10Waaye danga noo wacc, torxal nu, ba àndulook sunu mboolooy xare.

Read Sabóor 44Sabóor 44
Compare Sabóor 44:8-10Sabóor 44:8-10