Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 41

Sabóor 41:9-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9naan: «Musiba dal na ko, du jógati!»
10Sama am-di-jàmm bu ma wóolu sax jógal na ma, te daan lekk samaw ñam.
11Waaye ngalla Aji Sax ji, baaxe ma, yékkati ma, ma fey leen.
12Su noon damuwul ci sama kaw, ma doora xam ne bége nga ma.
13Man, damaa maandu, nga taxawu ma, dëj ma fi sa kanam, ba fàww.

Read Sabóor 41Sabóor 41
Compare Sabóor 41:9-13Sabóor 41:9-13