Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 41

Sabóor 41:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Dama ne: «Aji Sax ji, tooñ naa la; baaxe ma, faj ma.»
6Noon yaa ngi may yéene lu bon, naan: «Xanaa kii du dee, ba ñu fàtte ko?»
7Ku dikk, di ma seet, di jinigal tey fenti sos ci xolam, bu génnee, tasaare ko.

Read Sabóor 41Sabóor 41
Compare Sabóor 41:5-7Sabóor 41:5-7