Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 40

Sabóor 40:10-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Siiwal naa sag njekk ca ndaje mu mag ma. Dama ne, Aji Sax ji duma noppi, xam nga ko.
11Làquma sag njekk, ne cell ak moom. Yaa wóor, di walloo, siiwal naa ko. Làquma ndaje mu mag ma sa ngor ak sa worma.

Read Sabóor 40Sabóor 40
Compare Sabóor 40:10-11Sabóor 40:10-11