19Ma ne, aylayéwén def naa lu ñaaw, sama bàkkaar tiital na ma.
20Noon yaa ngi ne jonn ak seen doole, bare na ñu ma bañ ci neen.
21Ma ji leen njekk, ñu fey ma njekkar; may sàkku lu baax, ñu di ma sikk.
22Éy Aji Sax ji sama Yàlla, bu ma wacc, bu ma sore.