Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 36

Sabóor 36:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Mu jëm ci njiital jàngkat yi, ñeel Daawuda jaamub Aji Sax ji.
2Kàddug tooñ ga ku bon wax mu ngi sama xel mi. Mu ne: «Ana lu may ragal ci Yàlla?»
3Day gis boppam, naagu, ba du gis sikkam, sib ko.

Read Sabóor 36Sabóor 36
Compare Sabóor 36:1-3Sabóor 36:1-3