Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 35

Sabóor 35:19-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Noon bu ma deful dara, yàlla bumu gis lu mu ma damoo. Ku ma bañ ci dara, yàlla bumu ma ree.
20Waxuñu jàmm, xanaa di ràbbal niti jàmm ci réew mi ay kàdduy tuuma.
21Ñu ngi ma ŋa ŋàpp, di ma tuumaal, naan: «Yaw a, yaw a, noo la gis!»

Read Sabóor 35Sabóor 35
Compare Sabóor 35:19-21Sabóor 35:19-21