Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 34

Sabóor 34:2-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Naa màggal Aji Sax ji saa su ne, di ko sant fu ma tollu.
3Aji Sax ji laay sagoo, néew-ji-doole dégg, bég.
4Kañleen Aji Sax ji, ànd ceek man, nu bokk wormaal turam.
5Maa sàkku Aji Sax ji, mu nangul ma, tàggale maak lépp lu ma ragal.

Read Sabóor 34Sabóor 34
Compare Sabóor 34:2-5Sabóor 34:2-5