Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 31

Sabóor 31:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Maa bañ kuy topp tuuri neen. Man, Aji Sax ji laa wóolu.
8Damay bég, di bànneexoo sa ngor, li nga xoole samaw tiis. Ràññee nga sama njàqarey xol.
9Waccoo ma ci loxol noon, danga maa taxawal fu ma yaatoo.

Read Sabóor 31Sabóor 31
Compare Sabóor 31:7-9Sabóor 31:7-9