Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 30

Sabóor 30:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Muy woyu Sabóor, ñeel Daawuda ca daloob kër Yàlla ga.
2Aji Sax ji, dama lay kañ. Yaa ma yékkati, ba noon reetaanu ma.
3Aji Sax ji sama Yàlla, maa la woo wall, nga faj ma.

Read Sabóor 30Sabóor 30
Compare Sabóor 30:1-3Sabóor 30:1-3