Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 2

Sabóor 2:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Ñaan ma xeeti àddina, ma sédd la ko, nga moom ba ca cati àddina,
9yilife leen yetu weñ, rajaxe leen ni njaqal xandeer.”»
10Kon yeen buur yi, muusleen, kilifay àddina, fàgguleen.

Read Sabóor 2Sabóor 2
Compare Sabóor 2:8-10Sabóor 2:8-10