Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 28

Sabóor 28:7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Aji Sax jee may dooleel, di ma feg. Moom laa wóolu, mu wallu ma, sama xol tooy, ma woy, sante ko.

Read Sabóor 28Sabóor 28
Compare Sabóor 28:7Sabóor 28:7