Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 25

Sabóor 25:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Jiitee ma sag dëgg, jàngal ma. Yaw yaay Yàlla ji may musal, ma di la yendoo yaakaar.
6Aji Sax ji, bàyyil xel sa yërmandeek sa ngor. Naka jekk sa jikkoo!
7Bul xool li ma bàkkaare ndaw ak li ma moy. Aji Sax ji, xoole ma sa ngor ngir sag mbaax.
8Aji Sax jee baax, rafeti dogal, di gindi moykat ci yoon wi,

Read Sabóor 25Sabóor 25
Compare Sabóor 25:5-8Sabóor 25:5-8