Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 24

Sabóor 24:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Kookooy jagoo barkeb Aji Sax ji, ak njekku Yàlla, mi koy musal.
6Ñooñooy waa làng, gi lay sàkku, di maasug Yanqóoba, giy sàkku sa yiw. Selaw.

Read Sabóor 24Sabóor 24
Compare Sabóor 24:5-6Sabóor 24:5-6