Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 22

Sabóor 22:25-26

Help us?
Click on verse(s) to share them!
25Moom de sàgganewul boroom tiis, làqu ko kanamam, ba mu wootee, wuyu na ko.
26Yaw laay sante ndaje mu mag, sottalal la samay dige, ñi la ragal seede.

Read Sabóor 22Sabóor 22
Compare Sabóor 22:25-26Sabóor 22:25-26