Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 22

Sabóor 22:2-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Sama Yàlla, sama Yàlla, lu tax nga wacc ma? Ma binni, binneeti, wall sore.
3Éy sama Yàlla, ma woote bëccëg, wuyuwoo; woote guddi, nopploo ma.
4Yaw de, yaay ku sell, tooge sab jal, Israyil di la kañ.

Read Sabóor 22Sabóor 22
Compare Sabóor 22:2-4Sabóor 22:2-4