Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 22

Sabóor 22:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Ñu ŋa ma, ŋàpp, ni gaynde, guy yëmmook a fàdde.
15Doole ŋiis, yax yoqi, fit ne soyox, seey.
16Làmmiñ taqoo denqleñ, doole jeex, ma wow koŋŋ, nga tëral ma buntu bàmmeel.

Read Sabóor 22Sabóor 22
Compare Sabóor 22:14-16Sabóor 22:14-16