Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 22

Sabóor 22:10-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Yaw de yaa ma roccee sama biiru ndey, naxe ma sama weenu yaay.
11Yaw laa dénkoo ba may juddu, ba ma juddoo sama ndey, ngay sama Yàlla.
12Bul ma sore, musiba teew na, wall amul!

Read Sabóor 22Sabóor 22
Compare Sabóor 22:10-12Sabóor 22:10-12