Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 21

Sabóor 21:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Mu ñaan mucc, nga saxal jalam fàww,
6sag wall a ko sagala sagal! Teddngaak daraja nga ko sédd,
7jagleel ko barke bu sax dàkk, bégale ko sa kanam, mu bànneexu.
8Buur wóolu na Aji Sax ji, moos, du tërëf, Aji Kawe jee gore.

Read Sabóor 21Sabóor 21
Compare Sabóor 21:5-8Sabóor 21:5-8