Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 20

Sabóor 20:2-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Buur, yal na la Aji Sax ji nangul bésu njàqare, yal na la turu Yàllay Yanqóoba aj fu kawe,
3yal na la yónnee wallam fa këram, jàpplee la fa, ca Siyoŋ.
4Yal na xool loo ko jébbal, di rafetlu sarax soo ko lakkal. Selaw.

Read Sabóor 20Sabóor 20
Compare Sabóor 20:2-4Sabóor 20:2-4