Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 19

Sabóor 19:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Asamaan lay fenke cat lii, wëndeelu, sowi cat lee; amul lu rëcc tàngooram.
8Yoonu Aji Sax jee mat, di leqli bakkan. Lu Aji Sax ji seede dëgg la, day xelal ku xeluwul.

Read Sabóor 19Sabóor 19
Compare Sabóor 19:7-8Sabóor 19:7-8