Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 19

Sabóor 19:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Bésoo bés kàddu seere ko, guddee guddi xamle ca mbir.
4Du làkk, duy wax, du baat bu dégtu,
5suuf sépp la seen ndéey jibal, seen kàddoo àkki cati àddina. Kaw la Yàlla sampal jant xayma,

Read Sabóor 19Sabóor 19
Compare Sabóor 19:3-5Sabóor 19:3-5