Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 18

Sabóor 18:28-31

Help us?
Click on verse(s) to share them!
28Yaw yaay musal xeet wu néew doole, kuy daŋŋiiral, nga detteel.
29Yaw kay yaa may niital. Aji Sax ji sama Yàllaay leeral sama lëndëm.
30Maak yaw kay, ma song gàngoor. Maak sama Yàlla, ma tëb um tata.
31Yàllaa mat. Kàddug Aji Sax jee wér te wóor. Mooy feg képp ku ko làqoo.

Read Sabóor 18Sabóor 18
Compare Sabóor 18:28-31Sabóor 18:28-31