Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 18

Sabóor 18:20-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20yaatal ma, bége ma, ba xettli ma.
21Aji Sax jee ma yool sama njekk, samay loxoo set, mu fey ma.
22Sàmm naa yooni Aji Sax ji, bonuma, di moy sama Yàlla.
23Dama ne jàkk ndigalam yépp, xalabuma dogali yoonam.
24May ànd ak moom, di jëfeg mat, di moyoo tooñ.

Read Sabóor 18Sabóor 18
Compare Sabóor 18:20-24Sabóor 18:20-24