Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 148

Sabóor 148:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Nañu màggal turu Aji Sax ji, kii kat a santaane, lii lépp am.
6Moo leen samp, ñu sax ba fàww, mu dogal ko, te du toxu.
7Nangeen màggale Aji Sax ji fa kaw suuf, yeen ninki-nànkay géej ak xóote yépp,

Read Sabóor 148Sabóor 148
Compare Sabóor 148:5-7Sabóor 148:5-7