Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 148

Sabóor 148:10-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10ba ci mala yépp, yu àll ak gépp jur ak luy raam ak njanaaw,
11ak buuri àddinaak xeet yépp, ak kilifa yeek njiiti àddina yépp,
12xale bu góor ak bu jigéen, mag ak ndaw.
13Màggal-leen turu Aji Sax ji, moom doŋŋ la turam kawe, darajaam tiim asamaan ak suuf.

Read Sabóor 148Sabóor 148
Compare Sabóor 148:10-13Sabóor 148:10-13