Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 146

Sabóor 146:2-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2li feek may dund, di ko kañ, li feek may noyyi, di woy sama Yàlla.
3Buleen wóolu kilifa, doom aadama amul wall.
4Noo ga day rëcc, mu dellu suuf; bu bés baa, pexeem jeex.

Read Sabóor 146Sabóor 146
Compare Sabóor 146:2-4Sabóor 146:2-4