Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 145

Sabóor 145:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Muy jàngi màggal, ñeel Daawuda. Sama Yàlla, Buur bi, naa la màggal, teral sa tur ba fàww.
2Bésoo bés ma di la sant, di màggal sa tur ba fàww!
3Aji Sax jee màgg te jara màggala màggal, kii màggam amul kemu!

Read Sabóor 145Sabóor 145
Compare Sabóor 145:1-3Sabóor 145:1-3