Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 142

Sabóor 142:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3sippi ko sama tawat, diis ko sama njàqare.
4Bu ma yoqee, ràññee nga samay jéego; yoon wi may jaare lañu ma làqal am yeer.
5Ma geesu ndijoor, xool; du kenn ku ma faale. Rawtu réer ma, du kenn ku sama bakkan saf.

Read Sabóor 142Sabóor 142
Compare Sabóor 142:3-5Sabóor 142:3-5