Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 140

Sabóor 140:4-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4daas làmmiñam ni jaan, guux daŋaru ñàngóor. Selaw.
5Éy Aji Sax ji, aar ma ci loxol ku bon, musal ma ci nitu fitna, ku may fexee fakktal.
6Ñu bew ñee ma làqali yeer, lalal may buum aki caax, feggal ma seeni fiir ci yoon wi. Selaw.
7Dama ne Aji Sax ji, yaay sama Yàlla; Aji Sax ji, teewlul, ma dagaan la.

Read Sabóor 140Sabóor 140
Compare Sabóor 140:4-7Sabóor 140:4-7