Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 140

Sabóor 140:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3kuy nas lu bon, tey saxoo di sookey xare,
4daas làmmiñam ni jaan, guux daŋaru ñàngóor. Selaw.
5Éy Aji Sax ji, aar ma ci loxol ku bon, musal ma ci nitu fitna, ku may fexee fakktal.

Read Sabóor 140Sabóor 140
Compare Sabóor 140:3-5Sabóor 140:3-5