Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 139

Sabóor 139:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Kanam ak gannaaw nga ma dare, teg ma sa loxo.
6Ni nga ma xame daa yéeme, xóot lool, ba wees ma.
7Fu ma jëm, ba sore la? Fu ma daw jëm, foo teewul?

Read Sabóor 139Sabóor 139
Compare Sabóor 139:5-7Sabóor 139:5-7