Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 139

Sabóor 139:22-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Dama leena bañ ba fa mbañeel yem; samay noon dëgg lañu.
23Yàlla, seetlu ma, ba ràññee sama xol; natt ma, ba ràññee sama xalaati xol.

Read Sabóor 139Sabóor 139
Compare Sabóor 139:22-23Sabóor 139:22-23