Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 139

Sabóor 139:20-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Ñii sa tur lañuy luubale, noonoo la, di tudd sa tur ciy caaxaan.
21Aji Sax ji, maaka bañ ñi la bañ te sib ñi lay gàntal.

Read Sabóor 139Sabóor 139
Compare Sabóor 139:20-21Sabóor 139:20-21