Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 138

Sabóor 138:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Aji Sax ji, na la buuri àddina yépp màggal, ñoo dégg kàddu yi nga wax.
5Nañu woy say jaloore, naan: «Aji Sax jeeka màgg teddnga!»

Read Sabóor 138Sabóor 138
Compare Sabóor 138:4-5Sabóor 138:4-5