Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 137

Sabóor 137:6-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Yerusalem, su ma la fàttlikuwul, fonk la, ba gën laa bége lépp, yal na sama làmmiñ tafoo sama denqleñ.
7Aji Sax ji, fàttlikul Edomeen ña, keroog jantub Yerusalem, ba ñu naan: «Màbbleena màbb, ba kenug dëkk bi siiñ!»
8Yeen waa Babilon, gi ñu nara fàllas, ndokklee ku leen fey jëf, ja ngeen nu def!

Read Sabóor 137Sabóor 137
Compare Sabóor 137:6-8Sabóor 137:6-8