Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 136

Sabóor 136:18-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18bóom buur yu màgg ya,
19reyaale Siwon buurub Amoreen ña,
20reyati Og buuru Basan.
21Moo nangu seen réew, joxe,
22sédde Israyil ma dib jaamam.

Read Sabóor 136Sabóor 136
Compare Sabóor 136:18-22Sabóor 136:18-22