Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 136

Sabóor 136:12-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12ci dooley loxoom ak kàttanu përëgam.
13Moo xar géeju Barax ya yaar,
14jàllale bànni Israyil ca digg ba.
15Moo xalab Firawnaak mbooloom ca géeju Barax ya.
16Moo jiite ñoñam ca màndiŋ ma.
17Moo duma buur yu mag ya,
18bóom buur yu màgg ya,
19reyaale Siwon buurub Amoreen ña,
20reyati Og buuru Basan.
21Moo nangu seen réew, joxe,

Read Sabóor 136Sabóor 136
Compare Sabóor 136:12-21Sabóor 136:12-21