Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 132

Sabóor 132:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5li feek sàkkaluma Aji Sax ji bérab, ba dëkkal Mbërum Yanqóoba ma.»
6Ma ne, Efrata lanu dégg gaalu Yàlla ga, fekk ko àllub Yaar.
7Nan dem ba këram, sujjóotali ndëggëstalu tànkam ya.

Read Sabóor 132Sabóor 132
Compare Sabóor 132:5-7Sabóor 132:5-7