Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 132

Sabóor 132:1-2

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Muy jàngi yéeg, ñu di ko màggale Yàlla. Éy Aji Sax ji, bàyyil xel Daawuda, ak gépp njàqareem.
2Moo giñaloon Aji Sax ji, moo digook Mbërum Yanqóoba ma.

Read Sabóor 132Sabóor 132
Compare Sabóor 132:1-2Sabóor 132:1-2