Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 130

Sabóor 130:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Damay xaar Aji Sax ji, di ko xaare xol, di yaakaar kàddoom.
6Wattukat bi yàkkamti njël, wattukat bi yàkkamti njël, laa ne, ni ma yàkkamtee Aji Sax jee ko raw.
7Éey Israyil, négandikul Aji Sax ji. Aji Sax jee gore, te yaatug njot.

Read Sabóor 130Sabóor 130
Compare Sabóor 130:5-7Sabóor 130:5-7