Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 130

Sabóor 130:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Waaye yaay jéggale, ñu ragal la.
5Damay xaar Aji Sax ji, di ko xaare xol, di yaakaar kàddoom.
6Wattukat bi yàkkamti njël, wattukat bi yàkkamti njël, laa ne, ni ma yàkkamtee Aji Sax jee ko raw.

Read Sabóor 130Sabóor 130
Compare Sabóor 130:4-6Sabóor 130:4-6