Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 125

Sabóor 125:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Éy Aji Sax ji, baaxeel ku baax, ak kuy mébét njub.
5Waaye kuy topp yoonu ndëngte, Aji Sax jee koy sànk, boole kook kuy def lu bon. Yal na jàmm dal Israyil.

Read Sabóor 125Sabóor 125
Compare Sabóor 125:4-5Sabóor 125:4-5