Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 124

Sabóor 124:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3ba nit ña xadaroo sunu kaw, dañu nu doon wonn, nuy dund,
4dañu nu doon mëdd nim ndox, def um wal, buub nu,
5def waame wuy wal-wali, buub nu, yóbbu.
6Cant ñeel na Aji Sax ji, ki nu bàyyiwul, noon yi yàpp nu.

Read Sabóor 124Sabóor 124
Compare Sabóor 124:3-6Sabóor 124:3-6