Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:87-89

Help us?
Click on verse(s) to share them!
87Nes tuut ñu sànke ma fi kaw suuf, te man dëdduwma say tegtal.
88Musale ma sa ngor, ba jëfe sa kàdduy seede.
89Aji Sax ji, sa kàddoo sax dàkk, taxaw jonn fa asamaan.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:87-89Sabóor 119:87-89