Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:85-87

Help us?
Click on verse(s) to share them!
85Ñu bew ñi gasal nañu ma ay yeer, yu saw yoon diglewul.
86Sa santaane yépp worma la; te dees maa toppey sos, wallu ma!
87Nes tuut ñu sànke ma fi kaw suuf, te man dëdduwma say tegtal.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:85-87Sabóor 119:85-87